Urgent décés du khalife général de Thiénaba Serigne Cheikh Ahmed Tidiane Seck
Sunu Mame Cheikh Ahmed Tidiane Seck Khalifa Général Thienaba mo lakhou.. Inna Lilahi wa inna ileyhi radjihoune.. Yalla na Allah kharei ko Aljana Firdawzi.. kou fonkone alkhurane té fonku sunu wadjour cheikh issa seck..
 
        